NET TALI: Répudiée par son Mari, la Veille de la Korité

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 31 мар 2025
  • Net Tali: Répudiée par son Mari, la Veille de la Korité
    #faitsdivers #kebetu #team221

Комментарии •

  • @ibrahimasall5417
    @ibrahimasall5417 11 месяцев назад +16

    Ma sœur,esq ya gui respecter les 5 prières tè diko Selal?
    Si c'est comme ça,del zikar lahi laha ila anta soubhanaka ini kountou mina zalimina.
    Lep dina changé si mbakhou Yallah.

  • @willanemahtar8099
    @willanemahtar8099 11 месяцев назад +47

    Yawmi lire sama commentaire bi je t'aime ❤

  • @awadiakhate2014
    @awadiakhate2014 11 месяцев назад +24

    Beuryna niouy doundou li siséne négou seuy djigéne gni danio sonou yalna yalla mayniou ndam sisouniou seuy yi

  • @nobasiby9540
    @nobasiby9540 11 месяцев назад +11

    Bilahi walahi amna goro yo xamni soulene akh goro diapé dou bakh thi niome sokhor naniou trop wayé nak lou way def bopam lo lép lé lolou ngay fayékou ah non way li eup na sonal domou diambour ni rék 😢😢😢

  • @MariataYall-c8s
    @MariataYall-c8s 11 месяцев назад +22

    Mais pourquoi accepter d’être minimiser comme ça à cause d’un homme il y’a vraiment des familles qui ne pensent pas à la mort ameneu nite you bone wallahi

  • @ousmaneba6846
    @ousmaneba6846 11 месяцев назад +9

    keur yi kufa def caméras cachées ak micros di nga rouss.

  • @RamatoulayeDiallo-gd8ru
    @RamatoulayeDiallo-gd8ru 11 месяцев назад +5

    Yow dé yamagueneu patiente yéneyi mome gnak fayda ak khép sa bopeu leu . Mais c est pas la fin du monde aussi guisgna ragal yap Yalla la si keur nga diogué .guisnga nit dés fois soudara guenoul si yow yalla dalakoy soril .Boko forcer nak si souffrance rék ngay deuk .Balma dé mais vayil ki dougnou ay nit you bakh sinon sa moudiou dou raféte wasalam

    • @MaremeGningue-p9o
      @MaremeGningue-p9o 9 месяцев назад

      Bilaye degueu la famille bi dou niou ay nit

  • @FatoumataMbaye-vn3ks
    @FatoumataMbaye-vn3ks 11 месяцев назад +4

    Il faut se respecter et aller travailler.
    Une femme a de la valeur quiconque essaye de minimiser il faut jamais l’accepter.

  • @FatouSamate-z1s
    @FatouSamate-z1s 11 месяцев назад +2

    Salam aleykoum tata

  • @seydanefall3167
    @seydanefall3167 11 месяцев назад +2

    WAW ANA NIDIAYE YAM ,BI NIANE LONE DIEUKEREUM ,

  • @malickthioubdiallo5333
    @malickthioubdiallo5333 11 месяцев назад +11

    "Waadji korite lay bagne " il est malade mentalement sa maman weroul son frere di wakh wakhi dof ho!c'est dans leur gene matrimonial

  • @FatySarr-c3b
    @FatySarr-c3b 8 месяцев назад +1

    Yalla naniou yalla may kholou mougne

  • @MamediarraDia-p5e
    @MamediarraDia-p5e 11 месяцев назад +6

    Nawe si nakh weere na begue ga seye dé 3ans ga tok fi kene falewoula

  • @mylatouba1698
    @mylatouba1698 11 месяцев назад +5

    Mieux vaut mettre fin à ce semblant de mariage

  • @seuneba7091
    @seuneba7091 11 месяцев назад +15

    Elle ne devrait pas manger la soupe

  • @DiamondQueen-hg3jm
    @DiamondQueen-hg3jm 11 месяцев назад +14

    Cette femme est trop naïve .Je lui conseille de trouver du travail aussi prsk’elle est trop dépendante lolou rk meune neu takh son mari et sa famille di def foutaise sur elle.

    • @moriciss6368
      @moriciss6368 11 месяцев назад +2

      Pour lane mouy woute liguey tes deuikarame yor meune ko défal

  • @chasse-wy3bj
    @chasse-wy3bj 10 месяцев назад +5

    le gars il très maichant dicourage sister yalla bakhna

  • @adjafatouthiaw2094
    @adjafatouthiaw2094 11 месяцев назад +5

    Elle ne devait pas boire la soupe car elle connaissait ces intentions

  • @BintarassoulDiop
    @BintarassoulDiop 11 месяцев назад +1

    Niane mome yomb n’a n’a yéwou khadia goudii sou dioulé😂 niane yallah rk inchallah lep dina bakh inchallah

  • @khadygueye1707
    @khadygueye1707 11 месяцев назад +8

    Soupe bila chettttt gni gno bone deugue

  • @mbayeniang2808
    @mbayeniang2808 11 месяцев назад +5

    Tayi mom sama yaram dafa daw billay 😢

  • @awafall5243
    @awafall5243 11 месяцев назад +13

    Mère bi kou bone la

  • @mouhamedRassoultoure432
    @mouhamedRassoultoure432 6 месяцев назад +1

    80 pour 100 si seuy yi Sénégal bou yaakho goro yila

  • @barou60
    @barou60 7 месяцев назад

    Yalna yalla may niou deff lou bakhh

  • @abloslimshady
    @abloslimshady 10 месяцев назад +1

    Mais jiguenn youfiy doundou meti meti yii, mba yenengui dioulli sen 5 prieres, souvent damay fogni dolenn ay dioulitt, dolenn dioulli, niann yalla mou dimbeuli lenn!
    Te dioulitt bou doul dioulli do touddou yalla liguey wala def def dalay gawa diap, bayilenn tchi khell!
    Senn tolof tolof bou beuri bi yeup sen gueumeudi yalla molenn koy tek!
    Commence lenn di dioulli sen diouromi dioulli, di niane yalla, yalla diapale lenn!

  • @awakanteh5283
    @awakanteh5283 8 месяцев назад +1

    Na jog ligueye moiye solution bi.

  • @hamedinesarr8398
    @hamedinesarr8398 11 месяцев назад +3

    Je suis toujours votre émission sans commenter . Mais aujourd'hui je le ferai car je trouve ça très louche cette histoire. Un mari qui gagne 2millions par mois et fuit ses responsabilités en donnant 1000f pour le petit déjeuner par jour. Elle vit avec un millionnaire mais ils vivent comme gens pauvres

    • @matyndiaye4107
      @matyndiaye4107 11 месяцев назад

      Elle ment Barcki alkhourann son mari est l petit frère de ma Mére yalla n’a yalla attè

    • @moriciss6368
      @moriciss6368 11 месяцев назад

      ​@@matyndiaye4107😢😢😢ah lolou mome doyna war di iow mome no khamé ni sa mak lay waxal

    • @moriciss6368
      @moriciss6368 11 месяцев назад

      ​@@matyndiaye4107😢😢😢ah lolou mome doyna di iow mome no khaméni sa frére lay waxal

    • @Mhdtutoinformatique-ps1tq
      @Mhdtutoinformatique-ps1tq 11 месяцев назад

      deug boko degei rek khamko

  • @CodouSene-zt1bj
    @CodouSene-zt1bj 11 месяцев назад +2

    Mane deih ndawe sii khamenaa ko bou baakhe kou beugue seye té nanguou seye té nékk djiambare saa boko guissé mongui boote domame di ndougui té limouye doundou nii mane deih mossouma khame né lii laye dathie thie seyame walahi

  • @Mamekebe-zw9hv
    @Mamekebe-zw9hv 11 месяцев назад +5

    🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤🙏🤲

  • @laminediop4616
    @laminediop4616 9 месяцев назад +3

    Vraiment alaxira dina méti koi

  • @mariadrame7034
    @mariadrame7034 11 месяцев назад +11

    Goro bi mo ñaf nadayame nooo khalébi yarouna

  • @seynaboufall2
    @seynaboufall2 11 месяцев назад +2

    Doyna warr déé

  • @coumbandao2830
    @coumbandao2830 11 месяцев назад +2

    Bilahi ki limou wakh weupp daf fenn faite tres attention a c k vous dites prck niounn nieupp ayy famille laniou yorr tè kou dè akk sa bamel yalla na yalla atè

  • @ousmaneba6846
    @ousmaneba6846 11 месяцев назад

    retour à l'envoyeur kuko def si mystik boo xefee di nga am gattieh ndax si kimouy dall

  • @SeynabouNdiaye-n3g
    @SeynabouNdiaye-n3g 11 месяцев назад +2

    Kha na wakhoule oncle bi marabou la nafa deme bousi bagne dara

  • @AntaThioub-qc3we
    @AntaThioub-qc3we 11 месяцев назад +1

    😢😢😢😢😢😢😢

  • @Soxna-Rama26
    @Soxna-Rama26 11 месяцев назад +2

    Ah soxna si meune gua moungue dal

  • @DadaDiallo-nv2sx
    @DadaDiallo-nv2sx 9 месяцев назад

    Kou goor ki febar bi ko dalone bamou daane fanaané wakhtou moko bayi woul nagn ko outeul ay gnane

  • @Mamekebe-zw9hv
    @Mamekebe-zw9hv 11 месяцев назад +2

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @SIDYHSY
    @SIDYHSY 11 месяцев назад +7

    Elle ne devrait y retourner parce que bouko takaté mariage bi dou dagane t'en que kénéne takouko beu tass

    • @cheikhounadieng1849
      @cheikhounadieng1849 9 месяцев назад

      Boul wakh lolou ki tasoul 3 fois lolou kou tass 3 fois lay don

  • @FatouDiop-pk5rk
    @FatouDiop-pk5rk 8 месяцев назад +1

    Na dem thi nidiayam wakhekoko man sama khalat moy mou togue géré ay domam té mougne loguise day diekh dieu et grand

  • @ndaongone8443
    @ndaongone8443 11 месяцев назад +1

    Mane bala ma beuga deh guenni défendre sen djeukeur yi nane tayu gnu lignu nekke te gnoko gueuna taye bonne lagnu deff ak s’en famille

  • @serignediop3137
    @serignediop3137 11 месяцев назад +2

    Histoire bi louche na dé

  • @seydanefall3167
    @seydanefall3167 11 месяцев назад +1

    NE MOUGNES, GORO BOU BONE . DIEU KEUR BOU FAIBLE DE PERSONNALITÉS .

  • @franklybadji2326
    @franklybadji2326 11 месяцев назад +3

    konn sokhna fatou cafe dayy wagni tanghay mdr

    • @boubaka7172
      @boubaka7172 11 месяцев назад +1

      moma diakhal mba légui 😂😂

  • @allediouf1286
    @allediouf1286 11 месяцев назад

    La jeune fille doit rend chez son oncle en lui expliquant la situation dont son mari vit envers d'elle car grâce à dieu c'est ce dernier qui a changé sa vie

  • @fatousow3329
    @fatousow3329 11 месяцев назад +1

    Ça va sûrement Fatou micro moumoune pédiatre Bénabar inch'Allah

  • @mbayeniang2808
    @mbayeniang2808 11 месяцев назад +2

    Courrossma cambouren ak farmasi colfo otou 20min la wala Lou ke ebo

  • @sokhnalo3334
    @sokhnalo3334 11 месяцев назад +1

    Femme by kou niak faydala par se que mouno nek si keur Di seuy goro dila sonal dieukeur dina maltraité n'a tass yobou ay domam part se que d'où niouko may diam sinon diniay la Ray

  • @barou60
    @barou60 7 месяцев назад

    Yalla bakhh naa

  • @CheikhDieng-cf7mn
    @CheikhDieng-cf7mn 11 месяцев назад +1

    ❤❤❤c0

  • @metoudiop1019
    @metoudiop1019 8 месяцев назад

    Seyou sénégalais mo meti boudoul woudiouyi,dis goroyi, wallah woudiou petiorgoyi, serigne rek

  • @Isalahoud_darayni
    @Isalahoud_darayni 11 месяцев назад +3

    elle ment je vous dis elle a l'habitude de mentir jour pour jour c'est dans le sang d'elle je connais bien l'histoire faite trés attention à ces trucs elle ne sais rien si limouy wakh weit ak niak koum wakhal moko youbei netali bi

  • @rahimhalillulah5916
    @rahimhalillulah5916 10 месяцев назад +1

    Meneko eskai😄

  • @FatouSamate-z1s
    @FatouSamate-z1s 11 месяцев назад +1

    Monumentale

  • @jatoubarry7271
    @jatoubarry7271 10 месяцев назад +1

    Fek goro bangeh dunda sayam du neh. Na tas uti ligeuye topato domam yi.

  • @ngagnedeme-w2t
    @ngagnedeme-w2t 7 месяцев назад

    Ki mo niak fouleu. Kou gueum yalla dou nangou yene yii. Waye yen goor yii bone naniou.

  • @MamediarraDia-p5e
    @MamediarraDia-p5e 11 месяцев назад +1

    Do. Niane lou kome daga bega seye yale nala sougnou borome defale diamou

  • @coumbalo4130
    @coumbalo4130 9 месяцев назад

    Kou manqué lougnou ko dèf dagana

  • @RouguiDiop-e5b
    @RouguiDiop-e5b 11 месяцев назад

    Wa xana wadji moudioul tak niarel c'est bizare histoire bi lép léroul dé ma chérie fond wou problème bi dés na lér mais mougnal rec yalla baxna

    • @awadiouf9597
      @awadiouf9597 11 месяцев назад

      Voilà posé nako nakh degatouma toirou niarrr bi

  • @wanealpha1965
    @wanealpha1965 11 месяцев назад +1

    Mouna neka jeeker gui tayouko

  • @MamadouhlmBa
    @MamadouhlmBa 11 месяцев назад +1

    Thieuy Thieuy soupe bi oooooh😊

  • @elhadjaliounendiaye1684
    @elhadjaliounendiaye1684 11 месяцев назад

    Bigup

  • @NgoneMbaye-bd3fe
    @NgoneMbaye-bd3fe 11 месяцев назад +2

    Il n'a gua partir chez sont oncle

  • @MouhamadousaidouDiallo-o2i
    @MouhamadousaidouDiallo-o2i 8 месяцев назад

    Décourage Yalla diehoul

  • @sokhnaah5912
    @sokhnaah5912 11 месяцев назад

    Ndeyssane tayouco

  • @yvefay620
    @yvefay620 11 месяцев назад +1

    Trop de maraboutage au Sénégal ..qu'elle méchanceté .pratiques occultes c'est ça notre mental.On dirait qu' on se marie pour notre mère .... dommage

    • @yassendiop9276
      @yassendiop9276 11 месяцев назад +1

      Guiss gua dei Man mi goro motakh sama seuy tass bima eumbè am 2 mois sama dieukeur nima demal koula meuna hebergé mou hébérgéla 😢

  • @FataDiallo-q5q
    @FataDiallo-q5q 11 месяцев назад +1

    Seyi lousou way wah deugla goro yi nio bone

  • @jarieujallow8595
    @jarieujallow8595 11 месяцев назад +2

    ❤❤❤❤❤👍👍👍

  • @YoroBa-po5xl
    @YoroBa-po5xl 11 месяцев назад +1

    😂😂😂😂😂🤦‍♂️

  • @mouhamedRassoultoure432
    @mouhamedRassoultoure432 6 месяцев назад

    Bagna découragé rk
    Yaala linga mougneul ak linga soutoural sa dieukeur lépp dinalako fay

  • @MamediarraDia-p5e
    @MamediarraDia-p5e 11 месяцев назад

    Mane dina lepe di diokh sa yaye té begouma yawe daga bakh rek

  • @seuneba7091
    @seuneba7091 11 месяцев назад +3

    Son oncle est un marabou

  • @NgoneMbaye-bd3fe
    @NgoneMbaye-bd3fe 11 месяцев назад

    Kagnegua dome kay😂😂😂😂😂

  • @oumysene8728
    @oumysene8728 11 месяцев назад

    Diokhma numerome

  • @ndiasseniang7020
    @ndiasseniang7020 10 месяцев назад

    Wadji weeroul

  • @habymamadousakho7815
    @habymamadousakho7815 11 месяцев назад

    Yén yi mom xawma nougniou koy nango

  • @mamadousadji5577
    @mamadousadji5577 11 месяцев назад

    Femme bi mo amoule fayda, lane moye mbeugéule ah goro, na tass deme gnibi, yalla mofi nec

  • @sokhnaah5912
    @sokhnaah5912 11 месяцев назад

    Mais dou nidiayame meunena n'a dème mou diapaléco thi

  • @MoussaSeck-cb2cl
    @MoussaSeck-cb2cl 11 месяцев назад

    Sokhna fatou yakh mogena gaw defar

  • @elhadjidiagne6438
    @elhadjidiagne6438 11 месяцев назад

    Mais leroul de bimou eumbe di Defe oute serigne bouko gnanal xana tonton wame bi gnanal dieukeur bi foumou nekone moment bobou

  • @Yall123
    @Yall123 11 месяцев назад

    Expliquer famille Disney Benson beaucoup mon Afrique

  • @matyndiaye4107
    @matyndiaye4107 11 месяцев назад +5

    Votre émission n’a pas de sens vous n faite que mentir chaque famille a des problèmes ayez au fins fond de vos histoires pour comprendre avant de publier du n’importe quoi vous n metrisé pas c vous dite lidieuntilenn senn famille mo geunn ngenn di doul rekk vilipender des histoires familiales faire du mal à des personnes sans le connaître

    • @kikinettenjie2631
      @kikinettenjie2631 11 месяцев назад

      What's your probleme 😮😮😮

    • @OumyOumy-m6c
      @OumyOumy-m6c 7 месяцев назад

      Togne bakhoule intéressé woula boule deglou

  • @kadidiatousy7113
    @kadidiatousy7113 11 месяцев назад +1

    Li dóna Wat na mougne bou dôme yi maguer begueul ko

  • @FatouSamate-z1s
    @FatouSamate-z1s 11 месяцев назад +1

    Sani marouby amor WhatsApp